Aller au contenu

Samwie

Jóge Wikipedia.

Weeru Samwie mooy weer wi njëkk ci arminaatu Gregori ak ci bu Suul.

Baat baa ngi jóge ci latin januarius, ngir maggale ko yàllay waa-rom ja: Janus (yàllay bunt yi). Ca jamono ju yàgg ja, moo nekkoon fukk ak benneelu weer ci arminaatu waa-rom.

Weer
Samwie | Fewirie | Maars | Awril | Mee | Suwe | Sulet | Ut | Sattumbar | Oktoobar | Nowembar | Disambar